audio
audioduration (s)
0
103
transcription
stringlengths
11
1.27k
donc loolu dafa am solo donc ci formation bi la ñuy miser d' abord
lu ciy dellusi daal du bari maanaam
dindil soccu bi bala muy gaañ xale bi
dangay lekk togg mu ñuul boo ko lekkee rekk wër
ba diggante ñaari réew yi yàqoo moom lañu ràng
dafa feebar moo tax ñu bëgg ko sampal
te ñooñu tamit dañ soxla xabaar boobu
wër naa woto bi ñaari yoon di seet ndax sa bos la
bu mbënn mi agsee ndoxum dex gi dafay saf xorom
sebetagul ceeb bi ngay laaj ndax ñor na
bàyyil lambar lambari ci biir nit ñi
waaw prévision décadaire boobu noonu en fait dina tax béykat bi maanaam xam ban période lay épandre engrais waaw épandage d' engrais bi da koy dina ko xam dina tax tamit mu xam ban période la war a def traitement pesticide maanaam war a traiter pour pour pour dàq li ñu naan maanaam yu sew sewaéan yi nga xam ne mooy sonal mbéy mi waaw parce que ma imaginé rek maanaam nga par exemple tey jii ma am sama tool ah ma dem traiter léegi maanaam ma traiter ko ma traiter ko ba pare trente minutes après rek mu daal di taw taw bu fort maanaam taw yi bu ñëwee li ma traiter woon yëpp kon dootul amati benn njëriñ waaw maanaam yàq naa fa yàq naa fa temps yàq naa fa xaalis yàq naa fa énergie waaw
day tax balaa lee di màgg dinañ jiw fee balaa lee di bëri ñax dinañ ko mën a xotti
fuki at yi tegu jité na parti soviet bu missiong u apollo-soyuz li woné space race bii jexona
mbëtt ma ne kàttit dagg geenub golo ga
su dara nekkul ci fetal bi jëmale ko fu dara nekkul
demal alxemes ca ngonn fas wi dina ñów
man ngeena tàggoo ci njekk ak teraanga
futbalkat yi tàmbaleeguñu ñu ngiy tàngalu
dañu mànkoo ne dootuñu wax ak moom
ñaar fukki at yinu weesu limuk tannéf yi ñu jaglel xale ci uptown charlotte yokkna lool
jén wu mag la danga koy lottal soog ko génne
nga ne fi ma duggoon ci assurance bi
dafa ne dëndiix soow ma di xaar leneen
ami foogul woon ni mooy wat ca rawante ba
insecte moom de reyul kenn gal moom kii bi lay attaque
merci Jalle merci Ibrahima xam naa ne auditeur yi nga xam ne également dégloo leen gënal woote ak ñi nga xam ne ñu ngi bëggoon woote te jotuñu émission bi moo ni mel noonu ndax émision am na solo boo xam ne déglu jëlee si njëriñ sax day ëpp solo énu ngi gërëm ñëpp di sant ñëpp
boot na xale bi ba mu yàndoor mu tëral ko
sama góom baa ngiy xasan léegi mu wér
dara jotu ko óom bi rekk a fof tuuti
mais jàpp leen ni kat tey xabaar bi tey ngeen ko gën a soxla encore
déglul ndox miy xéréréri ci mbalka mil
ci lëkkaloo bien sur ma koy fàttali
maa ngi lay gërëm ci ndawtal li nga ma jox
adunà ñét à cee yobal àb hamé ab taar ak mbuus
gis naa ko ci moom wax dëgg yàlla waaw
dama egsi rekk fekk doom ji di ko doggali
bokkul ci càcc gi dañu ko bëgg dugal rekk
kuy yoot du sëqat wolof njaay a ko wax
waaye ki nga xam ne moom bokku si daañu la jaay nag ndax Fapal dafa yaatu ginnaaw
pàcc bu mag c yokkute bu duni hong kong dafa yam ci lu bare ci laajte suuf ci boori géej gi
yëngu yëngu kurél googu ëmb na fànna yu bare
cere ca ba muy tàng làñu koy laalo
bës bu yàlla sàkk treize heures
wax dëgg yàlla ñoo ngi nekk si unité bi loolu Jalle wax rek ñoo ngi ligéey ci ñebe bi
pàcc mu mujju bi jëm ci mboolem jongante yi dina ñu ko amal ci bërëb ellis park ca johannesburg ayubés bidi ñëw su springboks di jogante ak óstraali
faraas moy juróom ñaarelu dëkk ci mbootayu wa tugal bu loru ci doomu jàngoro bi topusi ótriis almaañ esloweeni bulgaari girees ak itaali
man dey xawma kañ la tàmbali jabraan
waa poliis neena ñu néew bi warna fa am lu xawa tollu ci benn bis
meenu salaan mag ñi dàan nañu ko faje góom
miis wu ni ñumm la lekk dara mejju ci
sér bi ñaari keppoo ko téye ci liiñ gi
na ñuy gën a seetle na ñuy gën a vérifié liste yi su amee genre erreur yooyu ñu xool nan la ñuy def pouir remplacer leen
dañu jàpp sàcc nit ñaa ngi ko ëw
lëg xëyee wuti am laxal yót ay doomam
wolof njaay nee sawóor bëgg na dugub waaye du bey
mënumaa ràññaatle ñaari seex yooyu
mingi tuddoon tuddeewoon hangeul alphabet hunmin jeogeum lu tekki coow lu jaar yoon ngir jàngal waa dëkk bi
mu nga doon dégétu ci seen diggu ëtt gaynde ga yuuxu
waxambaane bu luu bi fi daan ñów am na léegi liggéey
ah sant Soxna Anta rafetlu nañ kàddu yi bu baax a baax ñu ñu ngi sant daal di gërëm di sant waa unité transformation yu Kell Gueye yëpp rek
wala nga gont ngoon nga def ko bu fekke ci wàllu mboq la
lii légët la di te man duma séy ag boroomub légët
maanaam ci ag wo ci ag wor wor rek ci la ci la ci la ci la bëgg maanaam taw bu néew
waaye ci màggaay bi moom wax dëgg yàlla màgg na comme ni gerte doon màggee rafet na tubarkàlla ar waaye nag xam naa ne nii nii moom gerte war a gut a ñor moom waaw waaye waaye nag màgg na moom gerte gi daal moom màgg na
arrondissement Makka Kulibantang
abal ma làntinoor ma sol butéel bi
scientifique yi dañu gis ay xeetu suuf yu sutante yu nekk ci kaw weer wi ñu leen do woowe ay escarpements lobés dañu yaakaar ni lu weer di wàññiku ndank-ndank moo ko waral
kooku dama koo jéllale duma wax ay mbiram
da ngay dem uti variété bu gaaw
fegu moo gën xaar ba jàngoro ji dikk ngay seeti doktoor
xamuma ku la ko xelal waaye def nga lu baax
yénn say dangay wara jeend lu beeri lu wuté luy nangu téléfonu pstn woola fi numaro bi nékké di wuuté ngir nit yi woola
ca la ko rakk ya gindilikoo daanu ca kawam
soxlawul nga di ma rummi ragaluma la
ndém xamxamu greek marax na soww gi muje na dogo ak cosanu xeltu ak xamxam yu joge greek
diine dina togg nit ki ba muy jëfe lu rafet
sorbo ñu ngi koy def ci baatu turki
ay dëkkandoo seen diggante dafa wara rafet
arc bu jëm mooy faral di gëna néew coow waaye arc bu jëm suuf moo gëna bari coow
balaa jëkkër jée dee nag fekk na ndaw si ëmb ba diis
ca buntu kër ga laa tollu ma dégg butéelu gaas bi ne téll
dafa néewal ci lu jëm ci alalu àddina
ndax phosphate bi tamit am na nu ñu ko war a jëfandikoo
kàddir gii cumwaar gu mag a ci baax
seen ndam a ngi aju ci seen ub takkute
li ma gën a neex ci kër gi mooy waañ wu yaatu wi
doktoor bi waxagu ko ñaata lay joxe ci poose bi
su bakkan bi woddulee doom bi mën naa sax
jaaxle bi ma nekke ak say doom safu la
téeméer yëpp duñu ñëw maanaam fanweer yi
waaw war nañ joxe woon nañ ci ne maanaam faire lu ngeen ci gis ngeen joxe wax
weñ daldi ni maa ngiy sawi daldi dikk ni
sompal tuuti ci poobar bi def ci cin li
bërëb schengen de moo ngi dox melni benn réew ci noonu
ginaaw montevideo mingi ci bëj-saalumu equateur bi su bëj-gànnaar gi tàngee ñoom ñu sedd su ci kaw séddee ñoom ñu tàng
xàmme naa góor gi moo daan làpto ca tirbinaal
là côté boobu sax au mons mun nañu accepté mais li ngay def li ngay li ngay lekk après munoo jël doom yooyu noonu di ko dencee sa sa kii boobu sa sa sa jiw boobu loolu mun na la indil ay jafe-jafe yoo xamul kenn xamul fan la lay yóbbee
dafay teerte ñam wu neex wu nekk togg na ko
gas na am yeer ngir denc ci neefare ji