audio
audioduration (s)
0
103
transcription
stringlengths
11
1.27k
dund boobu ñu ko jox dañ koo xiirtal ci ay actions maanaam ay liggéey yoo xam da koo war a liggéey liggéey yoo xam ne mi ngi jëm ci loo xam ne lu koy aar lay doon jël ci ay matuwaay yoo xam ne dina mën a tax tey changement climatique bi li nga xam ne mu ngi ko war a indi mu béccee ko ci nit ñit ñi naka la ko tawoo ba mu oyof ci kaw doomu aadama ji
déñul mais daw na mi ngi daw daal
lépp lu jëm ci wàllu doxal projet bi nag Tekki jigéen kii moo ko yor Uniteden Proposen moo ko moo ko yore te suñu jigéen Mame Diarra nekk ku ku ku baax ku yiiw moom itam
gàngunaayu wurus ma mu daan toog a nga fa ba tey
indo yi ak urdu yi dañoo niiro ci seen bind waaye ci dañoo wuute ci xeetu bindiin ñiy lakk ñaari lakk yooyu mën nañu dégante
damay wuti per yu ma mottalee sama caq
bu déwénee ngay gën a gis njëriñ bi loolu moom yàlla def na ko ci ci phosphate
muus mi dafa fettax dal ci kow janax ji
waaw la base est implantée à Missirah
waaw loolu moom du ma ci sori xëy na boo bu Ibrahima ñëwee
eric kayser
dinfi bànqanoos bi ci waañ wi liggéey bu réy la
këriñ li baaxul dafay ferñent rekk
yaa ngi jeex tàkk xanaa danga biir
kou rér é mpënë boo op é fëndé
day dem ba mu yàgg rek dootoo gisati benn pepp xaalis boo xam ne sii moom lay ligéeyee
sa yaram dawul bi nga sàccee xaalisu silmaxa bi
tam dafa wër àddiina foo dem fekk ko fa
léegi ci wàllu yeneen béykat yi nga xamante ne xëy na soxla nañ ko te bokkuñu ci woon ci première phase bi bu ñu demee fii nii d' abord ba ba test yi jeex maanaam ba récolte yëpp jeex ba ñu xam parcelle bu nekk ñaata la génnee ci ci ay doom
Ndeye Diagne fiñ toll nii lan nga mën a ñaax sa naataango yi nga xam ne yéen a seq tool yi ak ñeneen ñi nga xam ne tey ñu ngi si yeneen tool si wàllu liggéey bi nga xam ne moom moo desandi ci liggéey bi pexe yi ñuy lal ba liggéey bi mën a sotti ak jàmm
lijgéey na naam waaye nag yaakaaroon naa lu ëpp lii
xar mii moom lanuy dundé ba ba nuy am fu nu sañc
saa su weer deewee dafay nëbbu borom kër gi
seetleen ci takkandeer yi leen yàlla dénk
sàmm yi ak beykat yi dañu war a jàmmoo
bu dee éléments yooyu dafa manqué suuf si day manqué doole
juddo ci kaptalu kroasi zagreb bobek siiw na ba muy football ngir partizan belgrade
doxat wu degtu woowu de yow rekk yaa ko déggul ci jataay bi
jërëjëf soxna Maguette ñu ngi leen di nuyu di leen sant ak ñëpp ñiy déglu rajo bi damay faral di wax ne am ngeen pàcc bu mag ci wàll wi nawet mooy loo xam ne bawul kenn
%hum %hum kon daanaka dal dafa mel ne ñëw bi nga xam ne gaa yi ñëw nañ ko fi am ngeen yaakaar ne dinañ ci mën a am njàngat mu bëri
mbubb ma nga soloon ca céet ga booba laa bëgg
bu ñu baxawee dugub ba noppi damay dem ndakaaru
yaay ji ñów xool ko xammee ko daldi ko song ni ko
yéen suénu mbokki jigéen éni xibaar bi yéen a ko moom kuréel gii ñu naan Fapal moo lëkkaloog kuréel gii ñu naan consortium tekki jigéen ci njàppanadalu USAID ñoo ñëw ngir gunge leen ci lépp luy suqali seen koom-koom te it yaqanal seen poche
ci kër madame Lika Diaw ci kaw
mi ngi yàq yàq bu jéggi dayoo ci suñu tool yi
services techniques yi nga xam ne ministère de l' agriculture yi nekk fépp
danga wara laaj sa yaay lu mu ci xalaat
ellëg la xare bi góor ñaa ngay xas ca pénc ma
am nañu kirisu xaalis bu def lu toll ci at bi amoon ay jamono yu metti lool ci ñaari weer yu mujj yi te yaakaar naa ni léegi màrse koppar yi dañuy tambalee delluwaat fiñu nekkoon
comité de gestion bi il faut ñu fexe ba comité de gestion bi ñu ñu soppiko mu nekk coopérative ñuy war a mën afexe soppi comité d de gestion bi mu nekk coopérative comme ça mën a gérer ma mën a gérer loolu
oto bi dafa daanu gerte gi ne wesar ci diggu tali bi
mën nga fa jénde yére yu bees su fekkee mu jàppandi la
muy commencé tóortóor ak yooyu
te doo jafandikoo produit lu dul rek ngay witti xob yi nga am ni dañuy dañuy yore nen yooyu
xale bi demaat ci beneen bitik daldi ni
ndax moom nekk na sax bi nga xamante ni
en tout cas di fàttali ni ku leen soxla yéen a ngi montagne
téere bii leeral na li nga bëgg xam ci mbirum ñakk yi
bi mu wasinee la tépparle jàngseetul
moom maanaam lépp li nga xamante ni tamit ñun jëf nañ ko
genn góor juux fa né ko moo looy tëdd fii
dafa añaan moo tax bégul ci sa teraanga ji
si waxtaan boo xam ne nag dañ ko seqoon ak waa ANCAR seen liggéey yoo xam ni ñu ngi koy liggéey lu jëm si wàllu tool yi waaye rawatina tey ci fi ñu toll fi nga xam ne fi tey tool yi am na ñoo xam ne tey commencé nañu récolter lépp loo xam ne dafa jëm si wàllu dugub ak li nga xam mooy ñebe ji
xale bu tàmmul tumuraanke du xam àddina
di nga mën a am tànn jiw ba nga xamante ni au moins quelque soit ndox buy am au moins yow as tuuti di nga ci di nga di nga ko am donc da lay permettre nga mën a planifié sa nawet donc mooy réduction des risques rek
alalam naka la koy saytoo naka la koy planifié naka la koy defee tëralinam ci ci ci yoon naka lay saytoo bor
xamle nañu ci ab yëgle ni ay ndaw a ngi liggéey ci biir gaal gi di fexe nu ñu ko génnee ci anam wu am kaaraange
way-dëkk bishkek yu bari japp nañu ne ñaxtukat yu joge ci bëj-saalum bi ño tax lu way nex def
su sunuy kàddu dëppoo mbir mi dootul yàgg
guney ndar né xaee éy saatañaali mbër nga mu né leen
mbaam mu të mii dina tax ba saxaar raw ñu
dag yi daldi ko dugal ci kees dem sànniji ko géej
ngàngooru jant bi rekk doy na kéemaan
dafa bëgga waxtaan te man dama gëmmentu
jonganté bi gëna mag ci at mi dina am ci weeru désembar ci bërëbu polo yi ci las cañitas
paaka du bënn deram dafa tul loolu la wax
ñu ngi koy sant di ko gërëm di ko masawu coono wu sant yàlla waa ANCAR yi rek di ànda ak ñoom si fas yéene liggéey liggéey ba mu egg rek si jàmm ak salaam
ngelaw la dugal xob ci pax génnewu ko ca
dafa dem bay wéeru ci sama kow ma mbas ko
buleen ko añaane ndamam li muuram la
def ko ci ñeex mi soo ko bëggee sàppali
wante it loolu lépp xëy na ñàkk a xam yoon bi nga xam si ne fi nga war a jaar ba mën ci def say activités
ay desitam jur nañu ay taw yu metti ci yenn dun yi wante fi nu toll nii yëglewunu benn yàkku yàkku wala mbënd
su nit gisé asaman di dengà mu jajanti ko
njiit lii du ku ñuy jay dëgg la bëgg dégg
bu dee lees bu yaa ñeenti mees doy na xaftaan
sàcc bi dafa mareñ taax mi jàll ci biir kër gi
may rappelé jigéen ñi dañ ci am représentation góor ñi ñi am foofu représent représentation xale yu góor yi ak xale yu jigéen yi tamit mag ñi tamit am nañu ay représentant ci comité de cyblage bi donc comité bi comité boobu moom moo toog seetlu ñan ñooy yelloo ci bokk programme bi su ko su ko defee su ñu génnee liste bi ñu soog ko su ñu soog ñu koo jox ñun dañuy xool rek critères yi
ak bor yi nga gàddu yépp doo ci génn
waaye nag dafa buggoon pour nga expliqué ko
soo gësëmee banqaas bi bal bi dina wadd
bu jëkk say waajur a la daan wutal jabar
waaye ci malaisie manaam ci malais yi dëkke ci dëkki àll yi loolu mooy tekki « kaay » mooy nuroo ak baaraamu joxoñ buñ lem mu jublu ci yaram wi muy lu ñuy def ci yeneen réew yi waaye buñu ci jublu ludul woo nit
ku yàlla sànni fitt doo ko mëna pakku
mooy seggal boppam kafe kenn doyu ko ci
ñoom ñett ñoo lëkkaloo pour porter programme boobu ah ANCAR nag ku ñu xam xam ne dañu nekk toujours au près des producteurs nekk si wàllu pegg béykat yi
sudee amul weñ bu jàppandi wala soo xalaatul sol ay kawaas ko di nga mëna jéema jëfandikoo ab wowalukaayu karaw su amee
dugub ji des na lu tane saaku bi xaajagul
mais ñu jàpp rek ni lay lay lay bi ñetti façons lay moo am am na lu tubaab di wax rosée am na lu ñuy wax brut humide am na lu ñuy wax broullard
am na ñoo xam ne dañuy wal xar laata ñu koy fees
dañu daan gàjj seen bopp ndax ñu bañ leena def jaam
mais bëgg naa nga gën cee insister
bëggoon na nu jaxase waaye mënu ko
taxawleen jonn ba kenn bañ a yàq seen lijgéey
bu ñu noddee fajar dafa naan fojjet jóg
la brousse est tout à fait silencieuse
bu xabaar yi jeexee dinañu dellusi ci tàgge yi
xale yaa ngay furóoñu ca suufas beeñ sa
nu mu daan léegi nu mu daan tàngee changé na tànga léegi léeg-léeg day tàng sedd donc cli changement climatique bi réalité la moo tax PAM ne pour réduire risques yooyu ñu ne dañuy lëkkaloo ndax wër information climatique