audio
audioduration (s)
0
103
transcription
stringlengths
11
1.27k
màngo ju neex lañu ko yónnee woon mayoon na ma ca sax
ba ñu ko naanee daal lañu kata kayna
te loolu ay jafe-jafe la yoo xam ne yu mot a bàyyi xel la
defal cuuraay ci and wi xet gu bon a ngoogu jóge ci mbedd mi
waaye dañuy jàkkaarloog kenn ci ñoo xam ne moom ci mbir mi la bokk muy Talla Ndiaye dañ koy jox mu nuyoo ak auditeurs yi doog ko dalal fii ci sa rajo Jabi jula FM sëñ Talla nga nuyoog auditeurs yi
demal jélali ma paan bi ca póotu ba
mais boo xoolee marche bi dafa dañu koo respecté fi produit bi duggee ak fi muy génnee c' est totalement différent te nit ñi seen kéem tolluwaay kàttan ñi ngi koy def pour mën a xool naka la énuy fexee ba mesure hygiènique yëpp ñu mën ko respecté lépp luy hygène ñu mën ko respecté
la ngeen tàyyi topp leen ko la ngeen sawar bàyyi leen ko
roberts dafa baña wax kañ la gëm ni dundutambali na laaj bu am solo suñu bayyee xel ci etiku yàq ëmb di wax ni du nekk lu andak etik ñuy àddu ci xewxew yu ni mel
%hum %hum loolu am na am na am na solo
ce ngoon sa ba yumaane liggéeyee ba sotaal mu woo ko ni ko
mu daldi beg ci saasi beg na waaye jaaxle na
mbott a gëna bëgg ndox wànte mu tàng bokku ca
sooy jënd garab dangay dem farmasi moo gën a wóor
mu daldi jël li mu soxla dem mu delluwaat ci yaayam ni ko
bi mu yéree mu gis cafaayal jaane tëdd gaynde giy lekk
mu ni ko léttal waa ji maa ngiy dem wutali ko ndawal
te ñu ngi si actuellemnt pour gën a am benn confirmation parce que septembre bi jeexagul te dafay taw
sa lakk lakk bi wétagul xanaa doo ko faj
yenn engrais yu war a ñëw te mu engrais bi nga xam ne moo gën ci ñoom ñu war ko mën a defaral seen bopp
voilà parce que boo góobee ba pare mu taw da koy da koy yàq su fekkente ne daf ko fekk ci suuf moo tax ñu ne daa am d' accord daañu góob mais sooy góob na nga ko jël précaution yu leer
booy màndaxale lim yi di xam ne jaarul yoon
waaye boo xoolee njeexital bi fi mu gënee amee solo mooy li jëm ci gàncax gi demee ni ki basi fi mu toll nii boo génnee da ngay gis toolu basi yi ni ñu ni ñu naatee
dangeen wara sàkk ab dig ci seen tool yi
buleen bàkkaar kenn sànniwu ko kort
samàkàt sañ naa may mév vandé sañul à may selu
abdu dafa ñaan permi ndax li muy séetal
bii bii bokkul ak sax yi moom bii moom c' est probl-me boobu beneen la
mu ngi làq dugubam di lekk sama jos
te ñun de wax dëgg yàlla keroog bi nga xam ne Sadio ñëw na ne ñu zngrais leen bi ñuy engrais suñ ñaari parcelles engrais nañ ko ba mu egg si suñuy engrais
timis jot na bala ngaa dugg ci néeg bi xuyét ko
sama jaaro baaraam ak samay jaaro nopp laay sóoblu
ndaw si ree né baay bi loolu dé matu ko
mu teg saakam dal di dem ubbi palanteer bi
per yu weex ak yu xonq la sàdde létt yi
ci rawante ba sunu ñaari fas yaa témboo
wurëmbél mumbél wurëmbélél mumbébél
fete naa gàkk gàkk bi hu tàyyi mu tëë deñ
parce que xam nañ ne jamono buñ toll nii allah ar kulli ar aali ar léegi léegi pour nga réussir sa liggéey il faut nga boole ci ay activités yi nga xamante ne ci météo da ciy da ciy dugal loxoom
ragaluma ci yoon mi am naa àndandoo
man déy duma séy ag boroomub légët
jógal nu dem bala ngay wasin ci kër gi
fuki at yi tegu jité na parti soviet bu missiong u apollo-soyuz li woné space race bii jexona
melokaanu gotik am na doole ci jamono diggante fukkeel ak fukkeel ak benneelu xarnu yi ak fukkel ak ñeent xarnu bi
miskin yu bare la yélimaan jooju daan leel
mën nga tamit bëgga saytu ay digle yu joge ci jëwriñ yi digle yu wute ak sa bos waye seni xalaat ngir séni nit la
am nañu doom ju jigéen ak doom ju góor
maa ngi lay gërëm ci butéelu litkoloñ bi nga ma yónnee
jot nañu fi aussi bataaxalu marie danielle quatier som cees
kawdir gi dafa jàppoon bi mu laata set xoos naa ba sonn
dafa jékki ba mu yàgg dal di tàggoo
wër naa sama fas wi ci dëkk dëkkaan yi ñu dendal
wool waxambaane yi ñu déqati bi ñu samp ci gannaaw
bu ndënd mi jibee ñépp dinañu déglu
ndax dañ ne comment prévenir les dégâts
mbokku auditeurs yi may fàttali ba tey rek maa ngi ànd ak ki nga xam ne moom mooy Yakhya Sèye nekk di nekk chef base P DPV bu Daara Djolof mu ñuy wax lu am solo loo xam ne tey jii yokk a rek ndax béykat yu bëri surtout béykat yu mag yi
loolu noonu ban différence lay am ci sol mën naa la koo gën a tënkalaat ba tey damay delluwaat ci suñu doom ji ak suñu yaay ji
bu ñu ci utul ay pexe fii ak ay at yu néew réew mi dina nekk loo xam pour dund fi sax dina jafe
simb sa ñuy jaay ca màrse ndar gànnaar lay jóge
geenu golo gudd na waaye foo ci laal mu yég ko
dangeen bokkul xalaat ci mbir moomu taxul nag mu di sa noon
bul xaar ba sa bëñ di yanq ngay sog a seeti dàntist
cappal sa baaraam ci soow mi seet ndax neex na
yaakaar naa boo xoolee ci lot bii rek danga ko fiy danga ko fiy gis
gëstu yiñ amal ci ñaar fukelu xarnu bi wane na ni amna ñaari xeeti genetique yu wuute bu nëbbu ak bu feeñ
geenu golo gudd na wandé lu ca laal borom yëg ko
sëriñ ba nag daldi génnndeke tukkiwul
làmp yi fey nañu xëy na nga daj sondeel ci taseer bi
siddéem su neex la baana baana yi di jële podoor
fu mu tollu mu ngi naan dafay dem tugal
damay ñaan tamit sunu mbokku béykat yi
da ciy am solo pour ñu koy bàyyi ci ci ci ci mbéy mi
bi ma dajee ak moom dafa dummóoyu ndax gàcce
kenn sañu leen laal dañu am ku leen yiir
mu ni ko waaw lan la waa ji dafa la dóor
mais dafa laal adduna bi yëpp la laal mais ku ci adduna bi ku si nekk ak nu mu koy maanaam nu mu koy nu mu koy yëgee am na si ñoo xamante ne dañu leen ay vagues de cha maanaam tàngaay bu jéggi dayoo bien que ñoo ngi koy resentir fii nii
mbootaayu xeet yi onu bi yaakar na paré benn xaalis ngir dimbali dëkk yu sonn ci tàngooru jawwu ji ngir ñu mën ko dékku
géléem a nga nëbbatu woon ca biir sàq ma
soo bareetee liggéey danga koy cër cëre ci bés yi
gan yu baré begalul mbaamsef ndégué du ñu ko yapà
jumtukaay bu ñuy seete sellaayu ndox mi la
ku fab téere bi ma tegoon ci taabal ji
bii xaaj nekk ag moom bii xaaj dugg ci dëkk bi
dem na dispàñseer biiru doomam dafay dow démb ba tey
bu ñu jugee nag ba dem saytu xam lan mooy jafe-jafe yi
ba ñu jógee ca seen xeex ba ba tey duñu tuddante
danga wara gëm te jébbalu ci yàlla
xàmmewuma ko woon genn wàllu kanam gi dafa jib
faagaagal na juróom ñaari xeet ci réewum kanaan
lu ma la def ngay sëq sama baatu mbubb
dëkk boobu ñi fa gën a bare ñooy pël yi ak wolof yi
yénéén yi bokkna ci deeku ndox biidi livingston té mbéttél bi caldera bi amoon ndox bu bénn suuf suy bax bu joxé gisggis bu doy war
dafay digle sax ni yooyu man-mani firi nekkiinu nit ñi mën nañ ko book ak mala yu melni xaj yuñuy yàr ci kër yi
deru xar bu nëb bii fees dell ak gasax sànni rekk a ci des
cokker mënta réer morom ma ci dédd
bul fàtte ordsabel bi booy fobeere
maa la dimmalee ganaar yii ci teerte gi
waaw te dina leen man maa leen déployer foofu
sama mbubb mi dafa xottiku ci baat bi
bëgguma tàggatoo ak moom ndax dafa may jooyloo
README.md exists but content is empty. Use the Edit dataset card button to edit it.
Downloads last month
27
Edit dataset card

Models trained or fine-tuned on abdouaziiz/wolof_lam_asr