sourate
float64 1
114
⌀ | verset
float64 1
286
⌀ | translation
dict |
---|---|---|
102 | 1 | {
"fr": "La course aux richesses vous distrait,",
"wo": "Ëpplaante fàbbi na leen,"
} |
102 | 2 | {
"fr": "jusqu´à ce que vous visitiez les tombes .",
"wo": "ba faf ngeen seeti bàmmeel yi. Dee dikkël leen."
} |
102 | 3 | {
"fr": "Mais non ! Vous saurez bientôt !",
"wo": "Déet ! Da ngeen xalseta xam de!"
} |
102 | 4 | {
"fr": "(Encore une fois) ! Vous saurez bientôt !",
"wo": "(Te it) ! Du ngeen xalseta xam de !"
} |
102 | 5 | {
"fr": "Sûrement! Si vous saviez de science certaine .",
"wo": "Déedéet ! Cëy su ngeen amoon xam-xam bu wóor."
} |
102 | 6 | {
"fr": "Vous verrez, certes, la Fournaise.",
"wo": "Bu ngeen gisee, tigi, safaraw Jahiim."
} |
102 | 7 | {
"fr": "Puis, vous la verrez certes, avec l´œil de certitude.",
"wo": "Te, dangeen ko gIisaat, ak bët yu wér."
} |
102 | 8 | {
"fr": "Puis, assurément, vous serez interrogés, ce jour-là, sur les délices.",
"wo": "Te bu keroogee, def na leen laaj, xéewël ya. "
} |
103 | 1 | {
"fr": "Par le Temps !",
"wo": "(Giiñ naa) ci Jamono!"
} |
103 | 2 | {
"fr": "L´homme est certes, en perdition,",
"wo": "Ne nit, mi ngi cig yàqule,"
} |
103 | 3 | {
"fr": "sauf ceux qui croient et accomplissent les bonnes oeuvres, s´enjoignent mutuellement la vérité et s´enjoignent mutuellement l´endurance.",
"wo": "bamu des ña gëm, tey jëf yiw di dénkënte dëgg di dékënte ci muñ. "
} |
104 | 1 | {
"fr": "Malheur à tout calomniateur diffamateur,",
"wo": "Xuru safara ñeel na képp kuy ŋelejooka ragaju,"
} |
104 | 2 | {
"fr": "qui amasse une fortune et la compte,",
"wo": "kuy dajale alal di ko lim,"
} |
104 | 3 | {
"fr": "pensant que sa fortune l´immortalisera.",
"wo": "Saar 104 : Ŋeleju 9 - Laaya – Laata Gàddaay ga Ci turu Yàlla Yërëmaakoon bi, Jaglewaakoon bi."
} |
104 | 3 | {
"fr": "pensant que sa fortune l´immortalisera.",
"wo": "jàpp ne alalam jaa koy taxa sax (baña dee)."
} |
104 | 4 | {
"fr": "Mais non ! Il sera certes, jeté dans la Hutamah .",
"wo": "Mukk ! dees na ko, mbaq ci biir Hutamatu."
} |
104 | 5 | {
"fr": "Et qui te dira ce qu´est la Hutamah ?",
"wo": "Ana lan moo lay xamal luy Hutamatu ?"
} |
104 | 6 | {
"fr": "Le Feu attisé d´Allah",
"wo": "Mooy Safaraw Yàlla wa ñu taal"
} |
104 | 7 | {
"fr": "qui monte jusqu´aux coeurs.",
"wo": "way alawtiku ba ca xol ya."
} |
104 | 8 | {
"fr": "Il se refermera sur eux,",
"wo": "Dañu leen cay séndël,"
} |
104 | 9 | {
"fr": "en colonnes (de flammes) étendues.",
"wo": "ci ay gàlli Safara yu ñu tàllal. "
} |
105 | 1 | {
"fr": "N´as-tu pas vu comment ton Seigneur a agi envers les gens de l´éléphant .",
"wo": "Xanaa gisu leen ka sa Boroom def ak ña ame woon ñay ya."
} |
105 | 2 | {
"fr": "N´a-t-Il pas rendu leur ruse complètement vaine ?",
"wo": "Moo ndax deful seen pexe ma mu naaxsaay ?"
} |
105 | 3 | {
"fr": "et envoyé sur eux des oiseaux par volées",
"wo": "moo yabal ca seen kaw ay njanaaw yu bari"
} |
105 | 4 | {
"fr": "qui leur lançaient des pierres d´argile ?",
"wo": "ñu di leen sànni ay doj yu ñu saaf?"
} |
105 | 5 | {
"fr": "Et Il les a rendus semblables à une paille mâchée.",
"wo": "Mu def leen ñu mel ne am ñax mu ñu sàqami. "
} |
106 | 1 | {
"fr": "A cause du pacte des Qurayshites,",
"wo": "Ngir sababus màngug Qureys,(s)"
} |
106 | 2 | {
"fr": "De leur pacte [concernant] les voyages d´hiver et d´été.",
"wo": "Seen mànko ci tukib sedd ak tàngaay."
} |
106 | 3 | {
"fr": "Qu´ils adorent donc le Seigneur de cette Maison (la Kaaba).",
"wo": "Na ñuy jaamu Yàlla boroom néeg bii."
} |
106 | 4 | {
"fr": "qui les a nourris contre la faim et rassurés de la crainte!",
"wo": "Yàlla mi leen joxu ñam ba xiifuñu aar leen it ba ragaluñu tiituñu! "
} |
107 | 1 | {
"fr": "Vois-tu celui qui traite de mensonge la Rétribution ?",
"wo": "Xanaa gisuloo kay weddi bisub dekkiwaat ba ?"
} |
107 | 2 | {
"fr": "C´est bien lui qui repousse l´orphelin,",
"wo": "Mooy kay bunduxataal jirim,"
} |
107 | 3 | {
"fr": "et qui n´encourage point à nourrir le pauvre.",
"wo": "te du sonn muk ci leel miskiin yi."
} |
107 | 4 | {
"fr": "Malheur donc, à ceux qui prient",
"wo": "Saar 107 : Njëfandukaay 7 - Laaya – Laata Gàddaay ga Ci turu Yàlla Yërëmaakoon bi, Jaglewaakoon bi."
} |
107 | 4 | {
"fr": "Malheur donc, à ceux qui prient",
"wo": "Xuru Safara, ñeel na ñay julli"
} |
107 | 5 | {
"fr": "tout en négligeant (et retardant) leur Salat,",
"wo": "ñay sàggane aka yeexe seenug julli,"
} |
107 | 6 | {
"fr": "qui sont pleins d´ostentation,",
"wo": "ñay ngistal,"
} |
107 | 7 | {
"fr": "et refusent l´ustensile (à celui qui en a besoin).",
"wo": "tey aaye dabi jëfandukaay yi. "
} |
108 | 1 | {
"fr": "Nous t´avons certes, accordé l´Abondance.",
"wo": "Jox Nanu la, déegub Kawsara."
} |
108 | 2 | {
"fr": "Accomplis la Salat pour ton Seigneur et sacrifie.",
"wo": "Na ngay julli ngir sa Boroom te na ngay rendi."
} |
108 | 3 | {
"fr": "Celui qui te hait sera certes, sans postérité.",
"wo": "Ka lay bañ aka ñaawal, moo dog ci lépp lu baax. "
} |
109 | 1 | {
"fr": "Dis : \"ô vous les infidèles !",
"wo": "Waxal ne : «Éy yéen yéefar yi !"
} |
109 | 2 | {
"fr": "Je n´adore pas ce que vous adorez.",
"wo": "Duma jaamu li ngeen di jaamu."
} |
109 | 3 | {
"fr": "Et vous n´êtes pas adorateurs de ce que j´adore.",
"wo": "Saar 109 : Yéefër ya 6 - Laaya – Laata Gàddaay ga Ci turu Yàlla Yërëmaakoon bi, Jaglewaakoon bi."
} |
109 | 3 | {
"fr": "Et vous n´êtes pas adorateurs de ce que j´adore.",
"wo": "Yéen itam du ngeen jaamukati li may jaamu."
} |
109 | 4 | {
"fr": "Je ne suis pas adorateur de ce que vous adorez.",
"wo": "Man it du ma jaamukatu li ngeen di jaamu."
} |
109 | 5 | {
"fr": "Et vous n´êtes pas adorateurs de ce que j´adore.",
"wo": "Te it yéen du ngeen jaamukati li may jaamu."
} |
109 | 6 | {
"fr": "A vous votre religion, et à moi ma religion\".",
"wo": "Am ngeen seen diine man it am naa sama dine” . "
} |
110 | 1 | {
"fr": "Lorsque vient le secours d´Allah ainsi que la victoire,",
"wo": "Saa su ndimbalu Yàlla dikkee ak ndam la,"
} |
110 | 2 | {
"fr": "et que tu vois les gens entrer en foule dans la religion d´Allah,",
"wo": "te nga gis ne nit ñaa ngi dugg def ay mbooloo ci biir diineey Yàlla ji,"
} |
110 | 3 | {
"fr": "alors, par la louange, célèbre la gloire de ton Seigneur et implore Son pardon. Car c´est Lui le grand Accueillant au repentir.",
"wo": "na nga sàbaal, te sant sa Boroom te na nga sàkku njéggalam. Moom Nànguwaakoonu tuub la. "
} |
111 | 1 | {
"fr": "Que périssent les deux mains d´Abu-Lahab et que lui-même périsse.",
"wo": "Ñaari yoxoy Abii Lahab dogg nañu te it dugg na."
} |
111 | 2 | {
"fr": "Sa fortune ne lui sert à rien, ni ce qu´il a acquis.",
"wo": "alalam ak la muy fàggu, du ko jariñ dara."
} |
111 | 3 | {
"fr": "Il sera brûlé dans un Feu plein de flammes.",
"wo": "Saar 111 : Buum ga 5 - Laaya – Laata Gàddaay ga Ci turu Yàlla Yërëmaakoon bi, Jaglewaakoon bi."
} |
111 | 3 | {
"fr": "Il sera brûlé dans un Feu plein de flammes.",
"wo": "Dana lakk ci biir Safara wuy bérax."
} |
111 | 4 | {
"fr": "de même sa femme, la porteuse de bois ,",
"wo": "ak jabaram ja daan yanu matt ma,"
} |
111 | 5 | {
"fr": "à son cou, une corde de fibres.",
"wo": "loosam wa, buumug rawa cay nekk (caq bu ñu soy). "
} |
112 | 1 | {
"fr": "Dis : \"Il est Allah, Unique.",
"wo": "Waxal ne : “Yàlla, moom Kenn la (jenn Yàlla rekk la)."
} |
112 | 2 | {
"fr": "Allah, Le Seul à être imploré pour ce que nous désirons.",
"wo": "Moom Yàlla, Mooy Kilifa gi wareefa joyal mbir yi."
} |
112 | 3 | {
"fr": "Il n´a jamais engendré, n´a pas été engendré non plus.",
"wo": "Jurul, te Kenn juru ko."
} |
112 | 4 | {
"fr": "Et nul n´est égal à Lui\".",
"wo": "Te amul benni nàttangoo” . "
} |
113 | 1 | {
"fr": "Dis : \"Je cherche protection auprès du Seigneur de l´aube naissante,",
"wo": "Waxal ne : “Maa ngi sàkku muslaayi Boroom suba si,"
} |
113 | 2 | {
"fr": "contre le mal des êtres qu´Il a créés,",
"wo": "ci ayu li Mu bind,"
} |
113 | 3 | {
"fr": "contre le mal de l´obscurité quand elle s´approfondit,",
"wo": "ak ci ayu lëndëm ga saa bu kukkee,"
} |
113 | 4 | {
"fr": "contre le mal de celles qui soufflent (les sorcières) sur les noeuds,",
"wo": "Saar 113 : Suba 5 - Laaya – Laata Gàddaay ga Ci turu Yàlla Yërëmaakoon bi, Jaglewaakoon bi."
} |
113 | 4 | {
"fr": "contre le mal de celles qui soufflent (les sorcières) sur les noeuds,",
"wo": "ak ci ayu ñiy wal ëf ci pas-pas yi (jibarkat yi),"
} |
113 | 5 | {
"fr": "et contre le mal de l´envieux quand il envie \".",
"wo": "ak ci ayu ku iñaan saa su jógee bay feeñal kiñaan ga” . "
} |
114 | 1 | {
"fr": "Dis : \"Je cherche protection auprès du Seigneur des hommes.",
"wo": "Waxal ne : “Maa ngi sàkku muslaayi Boroom nit ñi."
} |
114 | 2 | {
"fr": "Le Souverain des hommes,",
"wo": "Kiy Buurub nit ñi,"
} |
114 | 3 | {
"fr": "Dieu des hommes,",
"wo": "Di Yàlla nit ñi,"
} |
114 | 4 | {
"fr": "contre le mal du mauvais conseiller, furtif,",
"wo": "ci ayu jax-jaxali, Saytaane,"
} |
114 | 5 | {
"fr": "qui souffle le mal dans les poitrines des hommes,",
"wo": "kiy jax-jaxal ci biir dënni nit ñi,"
} |
114 | 6 | {
"fr": "qu´il (le conseiller) soit un djinn, ou un être humain\".",
"wo": "te bokk ci jinne yeek nit ñi” ."
} |